Cette femme explique : «Sama bayou djitlé dafma dane teudé »

Sama bayou djitlé dafma dane teudé  souma co wakhé sama yay mou niak ma kersa nima boumou gneum kaw… awma feinneu fouma co dioyé apres ma am kouma neikal ma dieulé ci eumbeu… cila deim seuyi dakar bayi fa sama doom bi ndakatei sama bayou djitlé bi mingui fo ci sama doom bi ba yakkeu ko… mou wakhate ko yay dji mounico wakho deugeu Mab beuguonaa xam nan laa wara déf .

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *